We provide Joxàl mala bi mu lekk! (Wolof) online (apkid: com.eduapp4syria.feedthemonsterwolof) in order to run this application in our online Android emulator.
Description:

Run this app named Joxà l mala bi mu lekk! (Wolof) using MyAndroid.
You can do it using our Android online emulator.
Joxl mala bi mu lekk dey jngal sa doom yi baat ag araf yi njk ci jng lifantu.
Tannal mala bu tojagul ci nenam diko jox mu lekk ay araf ag baat ngir mu magg ba doon xarit bu bess ci yow
LAN MOY JOXL SA MALA MU LEKK ?
Joxl sa mala mu lekk dey jffndiko ay feemu po yuy jngale yuu tekk ci xam-xam yu woor ngir fexe ba dimble sa doom yi u sawar ci jnk mi.
Xale yi di nee bg di tnn ag di gis ni sen xaritu mala yi di magge ba pare di jngale baat ag araf yu njk yi lenn di dimble u mna liir
AM KO CI SA TELEFON TE DO FAY DARA, AMUL AY NATAALU SIIWAL, AMUL LOY FAY CI BIIR PO MI !
Curious Learning, CET ag Apps Factory, di ay kurel yuy ongal jngum lkk yi, ooko defar te wutuu ci benn drm.
Do fay dara ci po mi !
MNDARGAWU PO MI NGIR ONGAL XAM-XAMU LIFANTU:
Ay laaj yu neex te reelu jm ci araf yi
Ay po ngir xaame araf yi ngir liir ag bind
Ay po ngir nafar ak denc ay baat
Ay niiwo yu jafe yo xamne baat bi rek gey dgg
Alluwa bu wayjuur yi mna xayma tolluwaay sen doom
Po mu nit yu bri mna deffando andak u mna xayma tolluwaay kenn ku ne
Ay mala yoo mna tnne sa bula neex, yu lay dimble nga foo, ree boolek jng
Dey yokku xaaraatef jm ci jkko ag ykk-ykk
Do fay dara ci bir po mi
Soxlawul dara lu leey lkkale ag enternet
AY ESPESYAALIST YU XAARAA OOKO DEFAR PUR SA DOOM
Po mi ongi ko amal ci ay atu xalaat, xayma ag jfandikoo ci xam-xamu baat ag araf yi.
Dafa dx ci bir ay xam-xam yu am jri, bokk nasi xamee jm ci ni uy binde baat yi, xamee araf yi, mbindum baat yi, xam-xamu baat yi ak lumuy tekki, jng baat yi uy gis.
Ginaw bi u ko defare ci mndargawu mbggeel ag ay mala yu bri, po mi dey dimble xale yi ci u am setlu, yeewute jm ci sen yoonu maggaay.
OY AN ?
Kurel gi di Joxal mala bi mu lekk u gn ka xam ci Feed the monster mongi am ci ndimblu banxaas bi yor wallum bitiw rew bu dkk bi di Norwes ginaw bimu bokke ci joante bi di EduApp4Syria-competition.
Jumtukaayu bu njku po mi mo ngi nekkoon ci lkkup arab u defaroon ko ci lkkalowu kurel yi di Apps Factory, CET The Center for Educational Technology ag IRC The International Rescue Committee.
-------------------------------------------------
Feed The Monster teaches children the fundamentals of reading in Wolof.
Collect monster eggs and feed them letters so they can grow into new friends!
WHAT IS FEED THE MONSTER?
Feed The Monster uses proven play to learn techniques to engage kids and help them learn to read.
Children enjoy collecting and growing pet monsters while learning reading fundamentals.
FREE TO DOWNLOAD, NO ADS, NO IN APP PURCHASES!
All content is 100% free, created by literacy nonprofits Curious Learning, CET, and Apps Factory.
GAME FEATURES TO PROMOTE READING SKILLS:
Fun and engaging phonics puzzles
Letter tracing games to aid reading and writing
Vocabulary memory games
Challenging sound only levels
Parental progress report
Multi-users login for individual user progress.
Collectable, evolvable, and fun monsters
Designed to promote socio-emotional skills
No in-app purchases
No ads
No internet connection needed
DEVELOPED BY EXPERTS FOR YOUR CHILD.
The game is based on years of research and experience into the science of literacy.
It incorporates key skills for literacy, including Phonological Awareness, Letter Recognition, Phonics, Vocabulary, and Sight Word Reading so kids can develop a strong foundation for reading.
Built around the concept of caring for a collection of monsters, it is designed to encourage empathy, perseverance and socio-emotional development for children.

MyAndroid is not a downloader online for Joxàl mala bi mu lekk! (Wolof). It only allows to test online Joxàl mala bi mu lekk! (Wolof) with apkid com.eduapp4syria.feedthemonsterwolof. MyAndroid provides the official Google Play Store to run Joxàl mala bi mu lekk! (Wolof) online.
©2025. MyAndroid. All Rights Reserved.
By OffiDocs Group OU – Registry code: 1609791 -VAT number: EE102345621.